Text copied!
Bibles in Wolof

Kàdduy Waare 1:17-18 in Wolof

Help us?

Kàdduy Waare 1:17-18 in Kàddug Yàlla gi

17 di dogoo xam luy xel mu rafet, xam luy nitoodi akug ndof. Fekk loolu it napp um ngelaw la.
18 Ku géejal xel mu rafet, géejal naqar; yokku xam-xam, yokku tiis.
Kàdduy Waare 1 in Kàddug Yàlla gi