Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Kàdduy Waare - Kàdduy Waare 1

Kàdduy Waare 1:14-15

Help us?
Click on verse(s) to share them!
14Gis naa jépp jëf ju jëfe ci kaw suuf, ndeke lépp cóolóoli neen la ak napp um ngelaw.
15Lu wañaaru, maneesu koo jubbanti; lu teewul, maneesu koo lim.

Read Kàdduy Waare 1Kàdduy Waare 1
Compare Kàdduy Waare 1:14-15Kàdduy Waare 1:14-15