Text copied!
Bibles in Wolof

Kàdduy Waare 1:14-15 in Wolof

Help us?

Kàdduy Waare 1:14-15 in Kàddug Yàlla gi

14 Gis naa jépp jëf ju jëfe ci kaw suuf, ndeke lépp cóolóoli neen la ak napp um ngelaw.
15 Lu wañaaru, maneesu koo jubbanti; lu teewul, maneesu koo lim.
Kàdduy Waare 1 in Kàddug Yàlla gi