Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Kàdduy Waare - Kàdduy Waare 12

Kàdduy Waare 12:13-14

Help us?
Click on verse(s) to share them!
13Ma daaneele fii, déggees na lii lépp: Yàlla, ragal ko; ay santaaneem, jëfe ko; loolu rekk mooy nit.
14Jépp jëf déy, la Yàlla di àtte, ba ci lépp lu làqu, muy lu baax, di lu bon.

Read Kàdduy Waare 12Kàdduy Waare 12
Compare Kàdduy Waare 12:13-14Kàdduy Waare 12:13-14