Text copied!
Bibles in Wolof

Kàdduy Waare 12:13-14 in Wolof

Help us?

Kàdduy Waare 12:13-14 in Kàddug Yàlla gi

13 Ma daaneele fii, déggees na lii lépp: Yàlla, ragal ko; ay santaaneem, jëfe ko; loolu rekk mooy nit.
14 Jépp jëf déy, la Yàlla di àtte, ba ci lépp lu làqu, muy lu baax, di lu bon.
Kàdduy Waare 12 in Kàddug Yàlla gi