Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Kàdduy Waare - Kàdduy Waare 10

Kàdduy Waare 10:17-19

Help us?
Click on verse(s) to share them!
17Ndokklee, yeen, réew ma as gor falu, te bu jotee, jawriñ ñay xéewlu, ngir am doole te baña màndi.
18Tayel, puj bu màbb; yaafus, néeg buy senn.
19Aw ñam bégal, aw ñoll bànneexal, xaalis tontu lu ne.

Read Kàdduy Waare 10Kàdduy Waare 10
Compare Kàdduy Waare 10:17-19Kàdduy Waare 10:17-19