Text copied!
Bibles in Wolof

Kàdduy Waare 10:17-19 in Wolof

Help us?

Kàdduy Waare 10:17-19 in Kàddug Yàlla gi

17 Ndokklee, yeen, réew ma as gor falu, te bu jotee, jawriñ ñay xéewlu, ngir am doole te baña màndi.
18 Tayel, puj bu màbb; yaafus, néeg buy senn.
19 Aw ñam bégal, aw ñoll bànneexal, xaalis tontu lu ne.
Kàdduy Waare 10 in Kàddug Yàlla gi