Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Kàdduy Waare - Kàdduy Waare 10

Kàdduy Waare 10:14-16

Help us?
Click on verse(s) to share them!
14Ab dof a ngi waxa wax, te kenn xamul luy xew ëllëg. Ana ku koy xamal gannaawam?
15Ab dof ak kër-këreem, coonoy neen; du xam sax yoonu taax ya.
16Ngalla yeen, réew mi gone falu buur, jawriñ ña di xëye xawaare.

Read Kàdduy Waare 10Kàdduy Waare 10
Compare Kàdduy Waare 10:14-16Kàdduy Waare 10:14-16