Text copied!
Bibles in Wolof

Kàdduy Waare 10:14-16 in Wolof

Help us?

Kàdduy Waare 10:14-16 in Kàddug Yàlla gi

14 Ab dof a ngi waxa wax, te kenn xamul luy xew ëllëg. Ana ku koy xamal gannaawam?
15 Ab dof ak kër-këreem, coonoy neen; du xam sax yoonu taax ya.
16 Ngalla yeen, réew mi gone falu buur, jawriñ ña di xëye xawaare.
Kàdduy Waare 10 in Kàddug Yàlla gi