Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Kàdduy Waare - Kàdduy Waare 10

Kàdduy Waare 10:12-14

Help us?
Click on verse(s) to share them!
12Ku xelu àddu, mu diw yiw; ku dofe wax, sànku.
13Bu jëkkee wax ju amul bopp, daaneele ndof gu sotti.
14Ab dof a ngi waxa wax, te kenn xamul luy xew ëllëg. Ana ku koy xamal gannaawam?

Read Kàdduy Waare 10Kàdduy Waare 10
Compare Kàdduy Waare 10:12-14Kàdduy Waare 10:12-14