Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Kàdduy Waare - Kàdduy Waare 10

Kàdduy Waare 10:11-13

Help us?
Click on verse(s) to share them!
11Jaan màtte, balees koo jat, du njariñal jatkat ba.
12Ku xelu àddu, mu diw yiw; ku dofe wax, sànku.
13Bu jëkkee wax ju amul bopp, daaneele ndof gu sotti.

Read Kàdduy Waare 10Kàdduy Waare 10
Compare Kàdduy Waare 10:11-13Kàdduy Waare 10:11-13