Text copied!
Bibles in Wolof

Kàdduy Waare 10:11-13 in Wolof

Help us?

Kàdduy Waare 10:11-13 in Kàddug Yàlla gi

11 Jaan màtte, balees koo jat, du njariñal jatkat ba.
12 Ku xelu àddu, mu diw yiw; ku dofe wax, sànku.
13 Bu jëkkee wax ju amul bopp, daaneele ndof gu sotti.
Kàdduy Waare 10 in Kàddug Yàlla gi