Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Kàddu yu Xelu - Kàddu yu Xelu 9

Kàddu yu Xelu 9:3-5

Help us?
Click on verse(s) to share them!
3Xel mu Rafet yónni ay janqam, di wootee fu kawee kawe ca dëkk ba,
4naan: «Képp ku téxét, jàddal ba fii!» Ku ñàkk bopp, mu ne ko:
5«Kaay, ma may la, nga lekk, xellil lay biiñ, nga naan.

Read Kàddu yu Xelu 9Kàddu yu Xelu 9
Compare Kàddu yu Xelu 9:3-5Kàddu yu Xelu 9:3-5