Text copied!
Bibles in Wolof

Kàddu yu Xelu 9:3-5 in Wolof

Help us?

Kàddu yu Xelu 9:3-5 in Kàddug Yàlla gi

3 Xel mu Rafet yónni ay janqam, di wootee fu kawee kawe ca dëkk ba,
4 naan: «Képp ku téxét, jàddal ba fii!» Ku ñàkk bopp, mu ne ko:
5 «Kaay, ma may la, nga lekk, xellil lay biiñ, nga naan.
Kàddu yu Xelu 9 in Kàddug Yàlla gi