Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Kàddu yu Xelu - Kàddu yu Xelu 8

Kàddu yu Xelu 8:9-10

Help us?
Click on verse(s) to share them!
9Lépp a dëggu ci ku am ug dégg, te jub ci ku for xam-xam.
10Na la samab yar gënal xaalis, xam-xam dàqal la ngën-gi-wurus.

Read Kàddu yu Xelu 8Kàddu yu Xelu 8
Compare Kàddu yu Xelu 8:9-10Kàddu yu Xelu 8:9-10