Text copied!
Bibles in Wolof

Kàddu yu Xelu 8:9-10 in Wolof

Help us?

Kàddu yu Xelu 8:9-10 in Kàddug Yàlla gi

9 Lépp a dëggu ci ku am ug dégg, te jub ci ku for xam-xam.
10 Na la samab yar gënal xaalis, xam-xam dàqal la ngën-gi-wurus.
Kàddu yu Xelu 8 in Kàddug Yàlla gi