Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Kàddu yu Xelu - Kàddu yu Xelu 8

Kàddu yu Xelu 8:6-9

Help us?
Click on verse(s) to share them!
6Déglul, ma wax la lu am solo, dégtal la njub.
7Dëgg laay wax, di bañ wax ju bon.
8Lu ma wax njub la. Amul lu dëng mbaa lu jekkadi.
9Lépp a dëggu ci ku am ug dégg, te jub ci ku for xam-xam.

Read Kàddu yu Xelu 8Kàddu yu Xelu 8
Compare Kàddu yu Xelu 8:6-9Kàddu yu Xelu 8:6-9