Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Kàddu yu Xelu - Kàddu yu Xelu 8

Kàddu yu Xelu 8:25-27

Help us?
Click on verse(s) to share them!
25Dikk naa bala tund yu mag yee sampu, lu jiitu tund yu ndaw yi,
26laata Yàllaa sàkk suuf aki àllam ak feppu pënd ci àddina.
27Ba muy taxawal asamaan, maa nga fa, ak ba muy rëdd fa asamaan taseek géej,

Read Kàddu yu Xelu 8Kàddu yu Xelu 8
Compare Kàddu yu Xelu 8:25-27Kàddu yu Xelu 8:25-27