Text copied!
Bibles in Wolof

Kàddu yu Xelu 8:25-27 in Wolof

Help us?

Kàddu yu Xelu 8:25-27 in Kàddug Yàlla gi

25 Dikk naa bala tund yu mag yee sampu, lu jiitu tund yu ndaw yi,
26 laata Yàllaa sàkk suuf aki àllam ak feppu pënd ci àddina.
27 Ba muy taxawal asamaan, maa nga fa, ak ba muy rëdd fa asamaan taseek géej,
Kàddu yu Xelu 8 in Kàddug Yàlla gi