Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Kàddu yu Xelu - Kàddu yu Xelu 8

Kàddu yu Xelu 8:23-25

Help us?
Click on verse(s) to share them!
23Bu yàgg lañu ma dëj, ca ndoorte la, bala suuf a sosu.
24Ba may dikk, géej amul, ndox ballul bay fees, di wal-wali.
25Dikk naa bala tund yu mag yee sampu, lu jiitu tund yu ndaw yi,

Read Kàddu yu Xelu 8Kàddu yu Xelu 8
Compare Kàddu yu Xelu 8:23-25Kàddu yu Xelu 8:23-25