Text copied!
Bibles in Wolof

Kàddu yu Xelu 8:23-25 in Wolof

Help us?

Kàddu yu Xelu 8:23-25 in Kàddug Yàlla gi

23 Bu yàgg lañu ma dëj, ca ndoorte la, bala suuf a sosu.
24 Ba may dikk, géej amul, ndox ballul bay fees, di wal-wali.
25 Dikk naa bala tund yu mag yee sampu, lu jiitu tund yu ndaw yi,
Kàddu yu Xelu 8 in Kàddug Yàlla gi