Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Kàddu yu Xelu - Kàddu yu Xelu 8

Kàddu yu Xelu 8:19-21

Help us?
Click on verse(s) to share them!
19Li may mayee gën wurus, wa gën, sama njariñ wees xaalis ba gën.
20Yoonu njekk laay jaare, di jëfe li yoon àtte rekk.
21Ku ma sopp, ma nàddil la, feesal sab denc.»

Read Kàddu yu Xelu 8Kàddu yu Xelu 8
Compare Kàddu yu Xelu 8:19-21Kàddu yu Xelu 8:19-21