Text copied!
Bibles in Wolof

Kàddu yu Xelu 8:19-21 in Wolof

Help us?

Kàddu yu Xelu 8:19-21 in Kàddug Yàlla gi

19 Li may mayee gën wurus, wa gën, sama njariñ wees xaalis ba gën.
20 Yoonu njekk laay jaare, di jëfe li yoon àtte rekk.
21 Ku ma sopp, ma nàddil la, feesal sab denc.»
Kàddu yu Xelu 8 in Kàddug Yàlla gi