Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Kàddu yu Xelu - Kàddu yu Xelu 8

Kàddu yu Xelu 8:17-18

Help us?
Click on verse(s) to share them!
17Maa sopp ku ma sopp, ku ma seet tigi, gis ma.
18Alal ak teraangaa ngi fi man, am-am bu sax it ak yoolu njekk.

Read Kàddu yu Xelu 8Kàddu yu Xelu 8
Compare Kàddu yu Xelu 8:17-18Kàddu yu Xelu 8:17-18