Text copied!
Bibles in Wolof

Kàddu yu Xelu 8:17-18 in Wolof

Help us?

Kàddu yu Xelu 8:17-18 in Kàddug Yàlla gi

17 Maa sopp ku ma sopp, ku ma seet tigi, gis ma.
18 Alal ak teraangaa ngi fi man, am-am bu sax it ak yoolu njekk.
Kàddu yu Xelu 8 in Kàddug Yàlla gi