Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Kàddu yu Xelu - Kàddu yu Xelu 8

Kàddu yu Xelu 8:12-16

Help us?
Click on verse(s) to share them!
12«Man, Xel mu Rafet, foog di sama kër; xam-xam ak pexe, ma for.
13Ragal Aji Sax ji mooy bañ lu bon. Réy, xeebaate, yoonu mbon, ak wax ju jekkadi, ma boole bañ.
14Maa moomi digle, di maye gis-gis; maa am ug dégg, di boroom doole.
15Samay pexe la buur di jiitee, kilifa di ci àttee dëgg.
16Ci samay pexe la njiit di saytoo, ñook kàngam yeek ñiy àtte dëgg ñépp.

Read Kàddu yu Xelu 8Kàddu yu Xelu 8
Compare Kàddu yu Xelu 8:12-16Kàddu yu Xelu 8:12-16