Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Kàddu yu Xelu - Kàddu yu Xelu 8

Kàddu yu Xelu 8:10-13

Help us?
Click on verse(s) to share them!
10Na la samab yar gënal xaalis, xam-xam dàqal la ngën-gi-wurus.
11Ndax man, xel mu rafet, maa gën gànjar, loo bëgg maa ko raw.
12«Man, Xel mu Rafet, foog di sama kër; xam-xam ak pexe, ma for.
13Ragal Aji Sax ji mooy bañ lu bon. Réy, xeebaate, yoonu mbon, ak wax ju jekkadi, ma boole bañ.

Read Kàddu yu Xelu 8Kàddu yu Xelu 8
Compare Kàddu yu Xelu 8:10-13Kàddu yu Xelu 8:10-13