Text copied!
Bibles in Wolof

Kàddu yu Xelu 8:10-13 in Wolof

Help us?

Kàddu yu Xelu 8:10-13 in Kàddug Yàlla gi

10 Na la samab yar gënal xaalis, xam-xam dàqal la ngën-gi-wurus.
11 Ndax man, xel mu rafet, maa gën gànjar, loo bëgg maa ko raw.
12 «Man, Xel mu Rafet, foog di sama kër; xam-xam ak pexe, ma for.
13 Ragal Aji Sax ji mooy bañ lu bon. Réy, xeebaate, yoonu mbon, ak wax ju jekkadi, ma boole bañ.
Kàddu yu Xelu 8 in Kàddug Yàlla gi