Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Kàddu yu Xelu - Kàddu yu Xelu 8

Kàddu yu Xelu 8:10-11

Help us?
Click on verse(s) to share them!
10Na la samab yar gënal xaalis, xam-xam dàqal la ngën-gi-wurus.
11Ndax man, xel mu rafet, maa gën gànjar, loo bëgg maa ko raw.

Read Kàddu yu Xelu 8Kàddu yu Xelu 8
Compare Kàddu yu Xelu 8:10-11Kàddu yu Xelu 8:10-11