Text copied!
Bibles in Wolof

Kàddu yu Xelu 8:10-11 in Wolof

Help us?

Kàddu yu Xelu 8:10-11 in Kàddug Yàlla gi

10 Na la samab yar gënal xaalis, xam-xam dàqal la ngën-gi-wurus.
11 Ndax man, xel mu rafet, maa gën gànjar, loo bëgg maa ko raw.
Kàddu yu Xelu 8 in Kàddug Yàlla gi