Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Kàddu yu Xelu - Kàddu yu Xelu 8

Kàddu yu Xelu 8:1-4

Help us?
Click on verse(s) to share them!
1Déggal! Soxna si, Xel mu Rafet a ngi woote, dég-dég di xaacu.
2Ma nga taxaw ca selebe yoon ya, fu gëna kawe ca yoon wa.
3Ma nga bunt dëkk ba, taxaw; fa nit ñay jaare lay xaacoo naan:
4«Yeen mbooloo yi laay yéene, doom aadama yi laay joor.

Read Kàddu yu Xelu 8Kàddu yu Xelu 8
Compare Kàddu yu Xelu 8:1-4Kàddu yu Xelu 8:1-4