Text copied!
Bibles in Wolof

Kàddu yu Xelu 8:1-4 in Wolof

Help us?

Kàddu yu Xelu 8:1-4 in Kàddug Yàlla gi

1 Déggal! Soxna si, Xel mu Rafet a ngi woote, dég-dég di xaacu.
2 Ma nga taxaw ca selebe yoon ya, fu gëna kawe ca yoon wa.
3 Ma nga bunt dëkk ba, taxaw; fa nit ñay jaare lay xaacoo naan:
4 «Yeen mbooloo yi laay yéene, doom aadama yi laay joor.
Kàddu yu Xelu 8 in Kàddug Yàlla gi