Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Kàddu yu Xelu - Kàddu yu Xelu 7

Kàddu yu Xelu 7:5-8

Help us?
Click on verse(s) to share them!
5Dina la aar ci ndaw su yemadi, bokk feneen, di wax lu neex.
6Damaa tollu sama palanteer, séentu ca xarante ya,
7séen ca biir téxét ya, ku ma seetlu ca xale yu góor ya, muy ku ñàkk bopp.
8Muy dem ba fa ndaw say taxaw, ca selebe yoon wa, daldi wuti kër ndaw sa.

Read Kàddu yu Xelu 7Kàddu yu Xelu 7
Compare Kàddu yu Xelu 7:5-8Kàddu yu Xelu 7:5-8