Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Kàddu yu Xelu - Kàddu yu Xelu 7

Kàddu yu Xelu 7:12-14

Help us?
Click on verse(s) to share them!
12Ma nga ca mbedd ma, ne ca pénc ya, ruqoo ruq, ma ngay yeeroo.
13Ndaw sa ne ko katam, fóon, ne wajj, ne ko:
14«Tey matal naa la ma digoon Yàlla, yàppu bernde waa nga kër ga, saraxu cant la.

Read Kàddu yu Xelu 7Kàddu yu Xelu 7
Compare Kàddu yu Xelu 7:12-14Kàddu yu Xelu 7:12-14