Text copied!
Bibles in Wolof

Kàddu yu Xelu 7:12-14 in Wolof

Help us?

Kàddu yu Xelu 7:12-14 in Kàddug Yàlla gi

12 Ma nga ca mbedd ma, ne ca pénc ya, ruqoo ruq, ma ngay yeeroo.
13 Ndaw sa ne ko katam, fóon, ne wajj, ne ko:
14 «Tey matal naa la ma digoon Yàlla, yàppu bernde waa nga kër ga, saraxu cant la.
Kàddu yu Xelu 7 in Kàddug Yàlla gi