Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Kàddu yu Xelu - Kàddu yu Xelu 6

Kàddu yu Xelu 6:4-9

Help us?
Click on verse(s) to share them!
4Bul gëmm, bul nelaw!
5Dawal ni kéwél gu rëcc ub rëbb, ne fërr ni picc mu raw ab fiirkat.
6Yaafus bee, xoolal xorondom, seetal ci moom, ba muus.
7Du ku ko yilif mbaa ku koy sas, te jiiteesu ko.
8Bu jotee mu denc ab dundam, mu jot, mu for lekkam.
9Moo yaafus bi, foo àppal tëraay bi? Loo deeti xaar ci yewwu?

Read Kàddu yu Xelu 6Kàddu yu Xelu 6
Compare Kàddu yu Xelu 6:4-9Kàddu yu Xelu 6:4-9