Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Kàddu yu Xelu - Kàddu yu Xelu 6

Kàddu yu Xelu 6:31-33

Help us?
Click on verse(s) to share them!
31Waaye bu feeñee, fey boroom juróom yaari yoon, joxe alalu këram yépp.
32Njaaloo di ñàkk bopp, kuy sànk bakkanam a koy def.
33Mbugal ak toroxte dib añam, te gàcceem du deñ.

Read Kàddu yu Xelu 6Kàddu yu Xelu 6
Compare Kàddu yu Xelu 6:31-33Kàddu yu Xelu 6:31-33