Text copied!
Bibles in Wolof

Kàddu yu Xelu 6:31-33 in Wolof

Help us?

Kàddu yu Xelu 6:31-33 in Kàddug Yàlla gi

31 Waaye bu feeñee, fey boroom juróom yaari yoon, joxe alalu këram yépp.
32 Njaaloo di ñàkk bopp, kuy sànk bakkanam a koy def.
33 Mbugal ak toroxte dib añam, te gàcceem du deñ.
Kàddu yu Xelu 6 in Kàddug Yàlla gi