Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Kàddu yu Xelu - Kàddu yu Xelu 6

Kàddu yu Xelu 6:22-24

Help us?
Click on verse(s) to share them!
22Booy dox mu di la jiite, nga tëdd, mu di la sàmm, nga yewwu, mu di la waxal.
23Santaane da lay niital, ndigal leeralal la, artook ub yar di yoonu dund.
24Da lay aar ci ndaw su bon ak jabaru jaambur ak làmmiñam wu neex.

Read Kàddu yu Xelu 6Kàddu yu Xelu 6
Compare Kàddu yu Xelu 6:22-24Kàddu yu Xelu 6:22-24