Text copied!
Bibles in Wolof

Kàddu yu Xelu 6:22-24 in Wolof

Help us?

Kàddu yu Xelu 6:22-24 in Kàddug Yàlla gi

22 Booy dox mu di la jiite, nga tëdd, mu di la sàmm, nga yewwu, mu di la waxal.
23 Santaane da lay niital, ndigal leeralal la, artook ub yar di yoonu dund.
24 Da lay aar ci ndaw su bon ak jabaru jaambur ak làmmiñam wu neex.
Kàddu yu Xelu 6 in Kàddug Yàlla gi