Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Kàddu yu Xelu - Kàddu yu Xelu 6

Kàddu yu Xelu 6:13-16

Help us?
Click on verse(s) to share them!
13day piis, di wokkeb tànk, di waxe baaraam,
14jekkadiy xalaat, di mébét lu bon aka yokku ay.
15Moo tax musiba di jekki dal ko, mu jekki yàqu, ba wees paj.
16Juróom benn a ngii yu Aji Sax ji bañ, ba ci juróom yaar yu mu seexlu:

Read Kàddu yu Xelu 6Kàddu yu Xelu 6
Compare Kàddu yu Xelu 6:13-16Kàddu yu Xelu 6:13-16