Text copied!
Bibles in Wolof

Kàddu yu Xelu 6:13-16 in Wolof

Help us?

Kàddu yu Xelu 6:13-16 in Kàddug Yàlla gi

13 day piis, di wokkeb tànk, di waxe baaraam,
14 jekkadiy xalaat, di mébét lu bon aka yokku ay.
15 Moo tax musiba di jekki dal ko, mu jekki yàqu, ba wees paj.
16 Juróom benn a ngii yu Aji Sax ji bañ, ba ci juróom yaar yu mu seexlu:
Kàddu yu Xelu 6 in Kàddug Yàlla gi