Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Kàddu yu Xelu - Kàddu yu Xelu 5

Kàddu yu Xelu 5:9-12

Help us?
Click on verse(s) to share them!
9Kon nga ñàkk daraja, keneen jagoo; ku néeg bóom la.
10Jaambur jariñoo sa doole, doxandéem jagoo saw ñaq.
11Ngay mujje onk, desey yax, jeex tàkk.
12Nga naan: «Su ma yégoon, sopp ab yar te baña sofental waxi àrtu.

Read Kàddu yu Xelu 5Kàddu yu Xelu 5
Compare Kàddu yu Xelu 5:9-12Kàddu yu Xelu 5:9-12