Text copied!
Bibles in Wolof

Kàddu yu Xelu 5:9-12 in Wolof

Help us?

Kàddu yu Xelu 5:9-12 in Kàddug Yàlla gi

9 Kon nga ñàkk daraja, keneen jagoo; ku néeg bóom la.
10 Jaambur jariñoo sa doole, doxandéem jagoo saw ñaq.
11 Ngay mujje onk, desey yax, jeex tàkk.
12 Nga naan: «Su ma yégoon, sopp ab yar te baña sofental waxi àrtu.
Kàddu yu Xelu 5 in Kàddug Yàlla gi