Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Kàddu yu Xelu - Kàddu yu Xelu 5

Kàddu yu Xelu 5:20-21

Help us?
Click on verse(s) to share them!
20Doom, ana looy xemmeme keneen, bay foye céri jaambur?
21Lu waay jëf, Aji Sax ji gis, di xool mboolem fu mu jaare.

Read Kàddu yu Xelu 5Kàddu yu Xelu 5
Compare Kàddu yu Xelu 5:20-21Kàddu yu Xelu 5:20-21