Text copied!
Bibles in Wolof

Kàddu yu Xelu 5:20-21 in Wolof

Help us?

Kàddu yu Xelu 5:20-21 in Kàddug Yàlla gi

20 Doom, ana looy xemmeme keneen, bay foye céri jaambur?
21 Lu waay jëf, Aji Sax ji gis, di xool mboolem fu mu jaare.
Kàddu yu Xelu 5 in Kàddug Yàlla gi