Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Kàddu yu Xelu - Kàddu yu Xelu 5

Kàddu yu Xelu 5:18-20

Help us?
Click on verse(s) to share them!
18Yal na sa naanukaay barkeel, nga bànneexoo kiy sa jabar ba ngay ndaw.
19Aka sopplu te jekk! Na lay céram doy foo tollu, na la xañ sago saa su ne.
20Doom, ana looy xemmeme keneen, bay foye céri jaambur?

Read Kàddu yu Xelu 5Kàddu yu Xelu 5
Compare Kàddu yu Xelu 5:18-20Kàddu yu Xelu 5:18-20