Text copied!
Bibles in Wolof

Kàddu yu Xelu 5:18-20 in Wolof

Help us?

Kàddu yu Xelu 5:18-20 in Kàddug Yàlla gi

18 Yal na sa naanukaay barkeel, nga bànneexoo kiy sa jabar ba ngay ndaw.
19 Aka sopplu te jekk! Na lay céram doy foo tollu, na la xañ sago saa su ne.
20 Doom, ana looy xemmeme keneen, bay foye céri jaambur?
Kàddu yu Xelu 5 in Kàddug Yàlla gi