Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Kàddu yu Xelu - Kàddu yu Xelu 5

Kàddu yu Xelu 5:14-16

Help us?
Click on verse(s) to share them!
14Tuuti ma yàqu yaxeet fi kanam ñépp!»
15Naanal ci sa mbalkam bopp, ndox ma balle sa teenu bopp.
16Xanaa doo wasaare sa bëti ndox ca biti, mu def ay wal ca pénc ya?

Read Kàddu yu Xelu 5Kàddu yu Xelu 5
Compare Kàddu yu Xelu 5:14-16Kàddu yu Xelu 5:14-16