Text copied!
Bibles in Wolof

Kàddu yu Xelu 5:14-16 in Wolof

Help us?

Kàddu yu Xelu 5:14-16 in Kàddug Yàlla gi

14 Tuuti ma yàqu yaxeet fi kanam ñépp!»
15 Naanal ci sa mbalkam bopp, ndox ma balle sa teenu bopp.
16 Xanaa doo wasaare sa bëti ndox ca biti, mu def ay wal ca pénc ya?
Kàddu yu Xelu 5 in Kàddug Yàlla gi